Me N You

Me N You

Dip Doundou Guiss

Li si man néwoul si niom
Li si niom néwoul si yow ooh my lova
Li niouy wakh man yeugoumako cuz I
Ndakh bou done film, fin bi mak yow la hoo ha

Girl I love you and you know
I love you and you know oooh ah oh ah
Aah aah

Kay nga wakhma bène yone
Calme bi fi nek dafma moudj soff
Status rek lay guiss si ay stories
Amnga connexion mais communiquer woo
Loutakh nga beug mel ni niom
Li ma guis nga def ni mom dou sa djiko

Louma wakh nga bagne ba néma no no
Nala fék fi nga né lidiantiko
Man douma daw, douma daw
Niom nieup danio fog ni lep dina diekh
Ma-ak yow meunoul bania nek bikg-ak pèle
Khamna gni beuga yak souniou diguenté

Lan mo takh niou beuri noone wowo
Lan mo takh niou beuri noone wowo
Me and you for life my baby
Bo naré dioy man ma weuy woman no cry

Lan mo takh niou beuri noone wowo
Lan mo takh niou beuri noone wowo
Me and you for life my baby
Bo naré dioy man ma weuy woman no cry

Li si man néwoul si niom
Li si niom néwoul si yow ooh my lova
Li niouy wakh man yeugouma cuz I
Ndakh bou done film, fin bi mak yow la hoo ha

Girl I love you and you know
I love you and you know oooh ah oh ah
Aaaah aaaaaaaaah

Sone tchi dila namm
Sone tchi dila ladj louma déf
Baby wakhma bou gaw fan nga né
Ma fék sila kay niou dadjé
Meunoma bayi ngakh sékou niou lolou
Meunoma beug té beugoma wolou

Boul di khaadj di khaadj di khaadj
Khol di ladj, di ladj, di ladj
Boul daw, boul dém, boul nangou lepp yakou bène yone
Boul may sa noone yi ndamou, kheuy di lakatou di diooy

Boul di khaatch di khaatch di khaatch no
Khol di ladj, di ladj, di ladj

Lan mo takh niou beuri noone wowo
Lan mo takh niou beuri noone wowo
Me and you for life my baby
Bo naré dioy man ma weuy woman no cry

Lan mo takh niou beuri noone wowo
Lan mo takh niou beuri noone wowo
Me and you for life my baby
Bo naré dioy man ma weuy woman no cry

Li si man néwoul si niom
Li si niom néwoul si yow ooh my lova
Li niouy wakh man yeugouma cuz I
Ndakh bou done film, fin bi mak yow la hoo ha

Girl I love you and you know
I love you and you know oooh ah oh ah
Aaaah aaaaaaaaah

Lan mo takh niou beuri noone wowo
Lan mo takh niou beuri noone wowo
Me and you for life my baby
Bo naré dioy man ma weuy woman no cry

Lan mo takh niou beuri noone wowo
Lan mo takh niou beuri noone wowo
Me and you for life my baby
Bo naré dioy man ma weuy woman no cry

(Reptyle music)

Me N You

Comentarios

Deja tu comentario:

Noticias de interés

Últimas noticias musicales

Reportar letra