L’amour rends fou et donne des ailes
Mais mes ailes elles se sont brûlées
Je suis tombé et c’est très dur
Devant le miroir je me sens bête
Mais bon maintenant je me suis rangé
Tu sais que tu m’as perdu
Depuis année je redoutais ça
Mes gazo m’avaient parlé mais j’écoutais pas
En vrai c’est chant-mè tu m’as fait du sale
Et du sale
Joxoon naa la li ma yoroon mu gën a sori ci man
Sama xol, sama chéri
Dinga ma bàyyi dina wet lool
Sama xol, sama chéri
Àdduna laa jël
Jëbal la ko nga wan ko ginnaaw dem
Sama xol dina metti
Danga xawoon yàkkamti
C’était tellement beau t’a détruit tout ça
Et de l’ego j’en avais même pas
Oh mi amor comment t’a pu me faire ça?
Feral nga sama géeju bànneex
Ma bal nga sama suufu mbégte
Fay nga sama jantu leeraay
(Chérie je t’ai épaulé, t’ai soutenu pendant des années)
Mësuma tëddi te tàggusiwuma la guddi guddi
Guddi guddi ci yaw la woon nga guddeloo ma
Àdduna laa jël
Jëbal la ko nga wan ko ginnaaw dem
Sama xol dina metti
Danga xawoon yàkkamti
Comentarios
Deja tu comentario: