Parano

Parano

VJ

J’ai pas su faire la différence entre le bien et le mauvais
Et j’ai souffert quand t’étais partie, quand t’étais plus à mes côtés
J’étais ouais toxic
Je voyais d’autre filles avec toi, j’étais pas docile
Moi je t’ai fait souffrir
T’avais des soucis mais tout le temps j’étais busy
Quand t’es décédé
J’ai vu que le contraire de l’amour c’est pas la haine
Mais plutôt l’indifférence
Et quand t’étais la, je m’en foutais de ton existence

La j’suis paranoooo, yeah parano
Parano, yeah parano
Ah su ma xoole sama ginnaaw
Sama xol fees ma jooy
Wet naa, wet naa, wet naa

Suma toogee xalaat sa dem
Sama xol fees fan lay waxe
Xanaa du yaa ma ni won yaw mi
Doo ma bàyyi, doo ma sori
Wax dëgg am na lu ma metti
Ab bataaxal laa lay yónne
Sa kanam laay gis su ma amee bànneex
Sama xol man laa la jox de

Tu me manques mais bon reposes en paix
J’ai une pensée pour toi, t’es dans ma tête
À la vie, à la muerte
À la vie, à la muerte

Yo, daj nga fi coono doo yuxu ji wallu
Àllaaxira da ngay dem pur dallu
Sagal sa bopp sagal sa axlu
Gisaguma ku la gën manu
Bàyyi nga ma ak ay full questions
Yu ma xamul seen reponse
Sama mbëggeel c’est des frissons
Mes sentiments je les énonces

La j’suis paranoooo, yeah parano
Parano, yeah parano
Ah su ma xoole sama ginnaaw
Sama xol fees ma jooy
Wet naa, wet naa, wet naa

Parano

Comentarios

Deja tu comentario:

Artistas más populares

Top artistas del momento

Reportar letra