Yow la tipoo kholal boubakh xa bakh
Ni ngay waxé ak mane
Yaw la tamou set loul bou bakh xa bakh
Ni ngay dokhé ak mane
Nitte si daniouy xol nimou
Geuneu niawé niou netaliiii ko
Nitte si daniouy xol nimou
Geuneu niawé niou netaliiii ko
Ndiaga fing ma wara fété
Bayou Samba molll na dell leu
Gaindé bou bakhé sakaam thi marééne
Faw thiolé bayy
Wouyou ma ma souki néwone
Nala dinala way
Ndèye mani Marème Ndoye
Abdou Aziz Ndoye
Téla niak yaye toumay bayam
Lima beugue moy Ndiaga
Nga bolé niou ande
Aida baxdade Sidi morom ndame
An mane dale mane
Ndiaga bou lay nékh yaw bou lay nékh
Ma def ko noko beugué wa weu
Ha heu heu
Y’Allah niou boole hé
Dieguéssima, dieguéssima
Dellou wone na leu
Dieguéssima, dieguéssima
Soma djito kharma, ndiaga
Andeu nila, waxko deug xol yi yaguo
Sama digeunték yow, nila
Kharma, Ndiaga
Kone chérie Adama ngui
Ndiaga Samb borome dame gni
Dieguéssima, dieguéssima, dieguéssima
Ndiaga wone naleu
Dieguéssima, dieguéssima
Soma djito kharma, Ndiaga
Ndiaga fing ma wara fété, bayi set meu
Mo raw gars gni
Comentarios
Deja tu comentario: